Medina Baay Research Association

  • Increase font size
  • Default font size
  • Decrease font size
Home News Contribution d'un membre de l'Association

Contribution d'un membre de l'Association

E-mail Print PDF

Assalaamu aleykum wa rahmatullaahi wa barakaatuhu

Man Abdulaay Nag ñu gën maa xam ci Baay Laay Ñaŋ dëkk Kawlax/Medina Baay maa bëggoon a wax tuuti sama xalaat ci suñu gëstu bi; ma am yaakaar ne nag ku nekk war na ci mën a bokk ndax te mbir mu am solo la te it du caaxaan, ay mag, ay booromi xam-xam rekk noo koy jiite. Gëstu bi ñoo ngi ko door 2004 ba tay looloo tax nag am nañ ci ay dolléeku yu baree-bari ci wàll gu nekk nag. Leegi képp ku ci am loo bëgg a xam walla nga bëgg ka si yokk mën ngaa jokkoo ag membre mbootaay bi soo woote ci numero bii: 00 221 775250041 walla 00 221 779086859 su sóobee Yàlla di nga am lu la léer.

Last Updated on Tuesday, 13 October 2009 21:32  

Newsflash

Medinabaay.org came back on line on September 10, 2009, at least sort of. Our archives are still awaiting a server, but the Medina Baay Research Association will report here on its ongoing fieldwork, findings, and observations. Please stay tuned as we redesign the site and reorganize our archive of interviews, meeting transcriptions, photos, manuscripts, videos, and so on.